Lan La Lyrics – Aida Samb
Singer: Aida Samb
Title: Lan La
Oh lan la
Oh oh lan la
Lan lala def
Wakh ma
Oh oh my love
Ay fana ngui thii tay
Khamouloni sakh man mangui thii keur gui
Oh oh souma teudé thii nekk bii
Nga dieul sa mbadj dem teudjou thii salle bii
Oh oh balma
Oh oh lan la
Lan lala def
Balma
Oh oh my love
Oh ladj nala lane mo khew nangou loma wakh deuké dima éviter
Oh oh souma teudé thii nekk bii
Nga dieul sa mbadj dem teudjou thii salle bii
Oh oh lan la
Oh oh wakh ma
Lan lala def
Balma
Oh oh my love
Khamnga ni yow my love fima tollou ni nirotouma niite
Kheuy rek téh sa bopp té man khamouma batay lanlala def
My looooove lett ma ba nga firi ma
Oh oh my love
Wakh maaaaaa
Fekewma yeggouma tinouma wakhouma deffouma khamouma batay lan lala def
Louma meunti am yamako gueuneul yow rek
La kham yow rek la miine yow yay sama wayy
My baby
I need you
My baby
I’m missing you
Oh oh lan la
Oh oh wakh ma
Lan lala def
Balma
Oh oh my love
Khamnga ni yow my love fima tollou ni nirotouma nitt
Kheuy rek téh sa bopp té man khamouma batay lanlala def
My looooove lett ma ba nga firi ma
Oh oh my love
Wakh maaaaaa
So khamone lima kham man dingma teh waw waw
So khamone lima kham man dingma yeureum waw waw
Jigeen kouko beggël diko yeureum la am waw waw
Kone dekkoy beggël diko yeureum diko waw waw
So khamone lima kham man dingma teh waw waw
So khamone lima kham man dingma yeureum waw waw
Jigeen kouko terral diko saggal la am waw waw
Kone demay beggël dima saggal dima waw waw
My love
Wakh ma
My love
Wakh maaaaa
Man beugone na dh louma deff
Nga woma niou wakhtané ko
Chercher ma tappass té deffoumala dara
So khamone limay dundu ni noumou mété
Fils dafa am loma tamalone bama tameko nga bayiko
Khol bou beggoul dioy
Té kouy dioy dou nakh kouy dioy
Lo lo ma metti fils
Man beugone na dh louma deff
Nga woma niou wakhtané ko
Chercher ma tappass té deffoumala dara
So khamone limey dundu ni noumou mété
Baby oh
Khol bou beggoul dioy
Kouy dioy dou nakh kouy dioy
Lingma tamalone ma tameko nga bayiko
Chérie nga bayiko
Ndaw ak limou mine souko guissoul daffey wett
Chérie boy
Man jigeen la
Khawma dara
A bingamey dieul
Man mi khawma dara
Wayé tay la nekh ba nguey soppi djiko
Eyy deug leu
Louma soumi nga faute ko lem
Chérie deug leu
Dima wakh wakhdjou melni lem
Chérie deug leu
Wayé amna lou dess
Chérie boy kholal ndiggleu gëseum
Yako dane feth may begg ndiggleu gëseum
Boko fethioul may dioy ndiggleu gëseum
Kou nopp sa chérie boy djougueul takhaw
Diaplène fi niou dem
Ndiggleu gëseum
Thiof fi thioffat ndiggleu gëseum
Ayyy ndiggleu gëseum
Ndiggleu gëseum
Thiof fi thioffat ndiggleu gëseum
Thiey
Kou nopp sa chérie boy diougeul yeungou
Kou nopp sa dieukeur diougeul yeungou
Kou nopp sa chérie diabbar yeungou
Kou nopp sa yayou dieukeur diougeul yeungou
Ahh
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net
You can purchase their music thru or Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Jaojoby - Alima
Outsider & Jung Yi Han - 멀어져
Lan La – English Translation
Oh lan
Oh oh lan
LAN LALA DEF
Wakh MA
Oh oh my love
Ay FANA NGUI THII TAY
Khamouloni Sakh Man mangui thii keur girl
Oh oh souma thii nekk bii
Nga god her mbadj dem teudjou thii room bii
Oh oh balma
Oh oh lan
LAN LALA DEF
Balmy
Oh oh my love
Oh Ladj Nala Lane Mo Khew Nangou Loma Wakh Deuké Dima Avoid
Oh oh souma thii nekk bii
Nga god her mbadj dem teudjou thii room bii
Oh oh lan
Oh oh wakh my
LAN LALA DEF
Balmy
Oh oh my love
Khamnga or Yow My Love Fima Tollou or NiRotouma Niite
Kheuy Rek Téh Sa Bopp Te Man Khamouma Batay Lanlala Def
My looooove lett my ba nga firi ma
Oh oh my love
Wakh Maaaaaa
Fekewma Yeggouma Tinouma Wakhouma Deffouma Khamouma Batay Lan Lala Def
Louma Meunti am yamoko gueuneul yow rek
The Kham Yow Rek The Yow Yay Sama Wayy Mine
My Baby
I Need You
My Baby
I’m missing you
Oh oh lan
Oh oh wakh my
LAN LALA DEF
Balmy
Oh oh my love
Khamnga or Yow My Love Fima Tollou or NiRotouma Nitt
Kheuy Rek Téh Sa Bopp Te Man Khamouma Batay Lanlala Def
My looooove lett my ba nga firi ma
Oh oh my love
Wakh Maaaaaa
So Khamone Lima Kham Man Dingma Teh WAW WAW
So Khamone Lima Kham Man Dingma Yeureum WAW WAW
Jigeen Kouko Beggël Diko Yeureum The Am Waw WAW
Kone Dekkoy Beggël Diko Yeureum Diko Waw WAW
So Khamone Lima Kham Man Dingma Teh WAW WAW
So Khamone Lima Kham Man Dingma Yeureum WAW WAW
Jigeen Kouko Terral Diko Saggal The Am Waw WAW
KONE DEMAY BEGGEL DIMA SAGGAL DIMA WAW WAW
Mon Amour
Wakh MA
Mon Amour
WAKH MAAAAA
Man Beugone Na DH Louma Deff
NGA WOMA Niou WAKHATANE KO
Search my tappass deffoumala dara
So Khamone Limay Dundu or Noumou Weather
Son Dafa am Loma Tamalone Bama Tameko Nga Bayiko
Khol Bou Beggoul DIOY
KOUY DIOY DOU NAKH KOUY DIOY
Lo Lo my Metti sons
Man Beugone Na DH Louma Deff
NGA WOMA Niou WAKHATANE KO
Search my tappass deffoumala dara
So Khamone Limey Dundu or Noumou Weather
Baby Oh
Khol Bou Beggoul DIOY
Kouy doy dou nakh kouy dioy
Lingma Tamalone My Tameko Nga Bayiko
Honey Nga Bayiko
NWAW AK LIMOU MINE SOUKO GUISSOUL DAFFEY WETT
Darling boy
Man jigeen the
Khawma Dara
In Bingamey Godl
Man Mi Khawma Dara
Wayé Tay La Nekh Ba Ngeny Soppi Djiko
Eyy Deug Leu
LOUMA SOUMI NGA FAULT KO LEM
Sweetheart deug leu
Dima Wakh Wakhdjou Melni Lem
Sweetheart deug leu
Wayé Amna Lou Del
Sweetheart Boy Kholal Ndiggleu Gëseum
Yako Dane Feth May Begg Ndiggleu Gëseum
Boko Fethoul May DIOY Ndiggleu Gëseum
Kou nopp her darling boy djouguul takhaw
Diaplene fi niou dem
Ndiggleu Gëseum
Thiof Fi thioffat Ndiggleu Gëseum
Ayyy Ndiggleu Gëseum
Ndiggleu Gëseum
Thiof Fi thioffat Ndiggleu Gëseum
Thiey
Kou nopp her darling boy diougeul yeungou
Kou Nopp Her Diekeur Diegeul Yeungou
Kou Nopp Her darling Diabbar Yeungou
Kou Nopp SA YAYOU Diekur Diougeul Yeungou
Ahh
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net
Lyrics Aida Samb – Lan La
Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.
We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂
You can purchase their music thru or Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
https://www.youtube.com/watch?v=QUF0Ac5xATI