Lyrics Jay 21 – Ña ña ña

Ña ña ña Lyrics – Jay 21

Singer: Jay 21
Title: Ña ña ña

Ña ña na
Defoul comme nieup
Dagnou ko beer
Defoul comme nieup

4K feuleu arbitre youkhou neu breuuuu
Est ce que ti comprend
Bayil meu Diegui Cambeu hip hop bi dokh
Douma rappeur bou reré corn-boeuf

Ña ña na
Ña ña na
Ña ña na
Ña ña na

Yaw da nga mer
Meune nga diwo beurre
Ña ña na
Est ce que tu comprends

Yewou sama Keur, évidemment baby bonjour
Yewou sama Keur beneu dimanche mane princesse dh on joue
Sama sons yi rek ñoy duggu club ma thiéné gallé melni old school
Bandit sa n#gg# dey teup tass nikou deugueu mine diaroul nioukoy soul

Est ce que ti comprend?
Est ce que djisso crack?
Fokoti contrat
Fokoti gun crack paaw

Dieundeu gouma sama planète niou beug meu gné
Defuma dara chaque année man rek ngeeni clamer ndax bëg ma ray
Eh boy duma dess ci suuf sans sa guel sama kaw
Suñu may denc suuf sama ruhu dañukoy yeegël

Concerts yi full mais sa caisse ak ay ndaw
Fake yi duñu giss sama défaite
Bo dewe ci dig marche ya feu taguer sa bop
Neew bi ga mounoul changer djiko bi dou

Dess man di nga fatalikou, bayil meu djitou galé tiabi gaateum
Ña ña na
Defoul comme nieup
Dagnou ko beer

Defoul comme nieup
4K feuleu arbitre youkhou neu breuuuu
Est ce que ti comprend
Bayil meu Diegui Cambeu hip hop bi dokh

Douma rappeur bou reré corn-boeuf
Ña ña na
Ña ña na
Ña ña na

Ña ña na
Yaw da nga mer
Meune nga diwo beurre
Ña ña na

Est ce que tu comprends
Yaw yaw
Nit la di dadj thiono machine
Dadj yima soxla moy signer ay contrats sinon soxla wuma sh#t

Rap moma soxla man soxla wuma rap c’est comme xorom ak tchinn
Gathié ngay dundu my n#gg#r ndax workat nga ni corona ak chine
Fajo gatt melni chloroquine
Dama work hard boy you know what I mean

Tegle wuma tank dëkku ma sama kaw lal duma son of b#tch
Boy duma sa concurrent bayima damalako ñaan
Ba ngay jug di tëb di dall fekk na man rañaan na
Ey duma jug ci rest in peace seen game bi

Gamou fake emcees yu demul fenn melni vigile
Game bi benn nit la dip ak fin de liste
Rendi tête d’affiches yi
Benn chef ngafiy giss

Dem ak xellu terroriste
f#ck theme ak egotrip
Juddo ci ghetto
Di jot xeer di dello missile

Xeex bi defko chiffres
Faybi defko liquide
Xetu dé lay guili tax ma dé ko ci biir
Ap beu nieup youkhou yes Mais xam nga lane mo gueuneu bone

Djiss ngama ma gadou koudou bou bess, wakh leine deug borom koudou dou laak
Yaw da nga meer
Do fi amati gouter
Sayssouné feri dag mais dou khar rek kay doug sa galé di youkhou mbé

Gnanaleine ko dîna riche
Dina dag boumou diami gniko miss
Rap beu moumeu deglou meu di youkhou sheesh
Dem beu Teubeul tiabi reubeuss gniko yitewoul

Dougou ci nga sama keer
4K Bi dou rap Wane meu noumou mel
Mane dama la tal ma ngui terre
Nga tiagatou game bi ma defar terrain nga teud ci Kerr

Rap melni kouy mbe
Deglou sa text mou melni ay Ching Chong fougnou tasse nga tituber
21 di sama season
Hurry up ci sama kiss

Sa carrière melni sounou miss monde
Gadou courouss sama dale
Pomme de terre bou gare
Mala djiteul diale

Xam nga sama gale
Bayil
Ña ña na
Defoul comme nieup

Dagnou ko beer
Defoul comme nieup
4K feuleu arbitre youkhou neu breuuuu
Est ce que ti comprend

Bayil meu Diegui Cambeu hip hop bi dokh
Douma rappeur bou reré corn-boeuf
Ña ña na
Ña ña na

Ña ña na
Ña ña na
Yaw da nga mer
Meune nga diwo beurre

Ña ña na
Est ce que tu comprends
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net

You can purchase their music thru 
Amazon Music or Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
I Feel Empty - IZthoN
VULTO. - Pózinhos

Lyrics Jay 21 – Ña ña ña

Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.

We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂

You can purchase their music thru 
Amazon Music or Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases