Lyrics Abiba – Saf Ngamay Jaay

Saf Ngamay Jaay Lyrics – Abiba

Singer: Abiba
Title: Saf Ngamay Jaay

I wanna love you and treat you right
I wanna love you every day and every night
We’ll be together with a roof right over our heads
We’ll share the shelter of my single bed

We’ll share the same room , oh Jah provide the bread
Is this love – is this love – is this love – is this love that I’m feelin’?
Is this love – is this love – is this love – is this love that I’m feelin’?
Oh oh , oh oh

I wanna know, wanna know, wanna know now!
I wanna know, wanna know, wanna know
I-I-I-I-I-I-I-I-I- I’m willing and able,
So I throw my cards on your table!

I wanna love you
I wanna love you ouh ouh
Saf ngamay jaay – yagui may gagne
Xol bé le taneu , mbeugël bi doumako fowé

Nop na xalé bi , té awma loumasi tite
Mane dama moudjé sakh, ame fite
OH baby , diox ma feu vert
Ma wakh le , le , le , nimala beugué

Té kham gua, kham gua, kham gua, ni fi yafiy bondél
Oh oh, Oh oh
Yama nieukeu nop , nieukeu nop , nieukeu nop way
Légui, damala noba, noba, noba ,nop ba raw le

Ah – Ah – Aie li foumakoy wakhé
Tey lay , jakarlok mome diko charmer
Xol bé le taneu
Baguama dane wo téléphone douma jeule

Bobou magui ley dozé
Baguama dane wo douma jeule,
Beugouma Lou ley xoss ba di la gagne , légui wo nala
Té mane leer nama ni , soffoumala way

Leer nala ni, soffouloma way yow
Saf ngamay jaay ( bobou magui ley dozé)
Ndakh mane ragalouma dara, titouma dara , soula nékhé,
Convoquél say ex (saf ngamay jaay)

Bobou magui ley dozé ( Saff ngamay jaay)
Bobou magui ley dozé
Mbeugël dou guissé rek ak wakhoma you Nex,
Si xol le , si xel le .
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net

You can purchase their music thru 
Amazon Music or Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
SpotemGottem - Lost Souls
Victor Ad - Bless Boys

Lyrics Abiba – Saf Ngamay Jaay

Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.

We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂

You can purchase their music thru 
Amazon Music or Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases