Lyrics ADBA LINCONNU – Wadjiour

Wadjiour Lyrics – ADBA LINCONNU

Singer: ADBA LINCONNU
Title: Wadjiour

And I respect to my parents
Big love to your parents and I prie for my parents yeah ey
Respect pour nos parents, amour pour nos parents mais prier pour nos parents Yeah ey
ADBA MY NAME

(Xat Xol)
Djeredjeufé yaaye boye djereudje baaye wa wawe
Démadem ba faté liguen ma déffal non non
Yaagu dima gnanal bama tew fi ohh ohh

Gnerignú Wadjiour kouko Xam do sonnou
Djeredjeufé Wadjiour, samay Wadjiour gnari Wadjiour
Djeredjeufé Wadjiour samay Wadjiour(samay Wadjiour, senni Wadjiour)
Djeredjeufé Wadjiour, samay Wadjiour senni Wadjiour

Magui dellou dilen gnaanal samay Wadjiour
Djeredjeufé yaaye taxna téy taxna tey ma né Djeredjeufé baaye
Yaagu di xouss si nadj ak nelaw taxoul gua meusseu tayi
Ba Xam ndole meusseu nala dape meunna sax wax ba tayi

Wanté soutoural se gnabote djaral nala gua die
Wadjiour trésor le, dou moromou or wax djiékk djefine gui yeup guir euleuk gua meneu fort
Every fadiar satala ak sidiara ba raxsi kourouss
Mane dîna lén teral té niguen mellax ni worous

Djeredjeufé yaaye boye djereudje baaye wa wawe
Démadem ba faté liguen ma déffal non non
Yaagu dima gnanal bama tew fi ohh ohh
Gnerignú Wadjiour kouko Xam do sonnou

Djeredjeufé Wadjiour, samay Wadjiour gnari Wadjiour
Djeredjeufé Wadjiour samay Wadjiour(samay Wadjiour, senni Wadjiour)
Djeredjeufé Wadjiour, samay Wadjiour senni Wadjiour
Magui dellou dilen gnaanal samay Wadjiour

Sa baaye ak sa ndeye walahi awma sen feye
Tax ma bayi lén ak ki di kéne nax mome rek moy kiy kéne
Bess dineu gneuw gua wanté gnúgui gnane mou yex
Gnane yalla bala bobou gnou tekki teral lén guén fex

Boulko gnakk sokkoy rethou Gnerignú Wadjiour meunoko teudou
Deukk si thipetou ak hellou guisgue lolou mo djara moytou
Disso minguo si kadou djaratoul gnoussoy ame flemme
Djéleul son bi defko settou listen to ADBA my name

Djeredjeufé yaaye boye djereudje baaye wa wawe
Démadem ba faté liguen ma déffal non non
Yaagu dima gnanal bama tew fi ohh ohh
Gnerignú Wadjiour kouko Xam do sonnou

Djeredjeufé Wadjiour, samay Wadjiour gnari Wadjiour
Djeredjeufé Wadjiour samay Wadjiour(samay Wadjiour, senni Wadjiour)
Djeredjeufé Wadjiour, samay Wadjiour senni Wadjiour
Magui dellou dilen gnaanal samay Wadjiour

And I respect to my parents
Big love to your parents and I prie for my parents yeah ey
Respect pour nos parents, amour pour nos parents mais prier pour nos parents Yeah ey
And I respect to my parents

Big love to your parents and I prie for my parents yeah ey
Respect pour nos parents, amour pour nos parents mais prier pour nos parents Yeah ey
ADBA MY NAME
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net

You can purchase their music thru 
Amazon Music  Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Sl!m D!zZy - Spit Raw
U-KNOW - 夜話 (City Lights)

Lyrics ADBA LINCONNU – Wadjiour

Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.

We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂

You can purchase their music thru 
Amazon Music  Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases

https://www.youtube.com/watch?v=cHiIS4Er10o