Capitaine Lyrics – Baye Mass
Singer: Baye Mass
Title: Capitaine
Fi lepp tamalé, fima la guissé
Dangma romba ma tago sama sago
Lu gayi neka di wakh degatuma ko
Ndakh ma diokh la sama xol
Lima dugal sama xol xawma lumu done
So ma rombé dotuma muna khol
Dumala musa muna bayi
Jiteul ma ma done sa ouroul Ayni
Benj koye ligeye demb la wone
Yay sama champion
Yay sama linguère
Benj koye ligeye demb la wone
Bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
Su djiné beugé ku yeug dangaye danou
Bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
Su djiné beugé ku yeug dangaye danou
Dumala musa muna bayi
Jiteul ma ma done sa ouroul Ayni
Benj koye ligeye demb la wonе
Bilaye mbeuguel moyе capitaine boromam
Su djiné beugé ku yeug dangaye danou
Ahh bilaye mbeuguel moye capitaine boromam
Su djiné beugé ku yeug dangaye danou
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net
You can purchase their music thru Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Boyka20096 - No Way
YOUNG X - Girlfriends
Lyrics Baye Mass – Capitaine
Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.
We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂
You can purchase their music thru Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases