Lyrics Jay 21 – Bùl Bidënti

Bùl Bidënti Lyrics – Jay 21

Singer: Jay 21
Title: Bùl Bidënti

Mounema geutch nagn djissante
Mane ko ndiabot moma djiteul tay
Nenagn geutch nga fegn depuis sa mixtape mane par force louma dji day fay
Mounama la ye beug bideunté

Taa nga ci diguanté bi
Li dou garawalé limit pick pele
Par force louma dji day fay
A part sama ndiabot douma FaceTime

Dougal marche sama style li dou freestyle
Game bi gnourok dessi anime ni Space Jam
Dafa Nara taar fils na nga tela far fi dama dieul ci sama part ndeysan
Def jeez sama ngam paré sif dem

M** F** bou ci tontou mané kill them
Sama tontou mounoul forokh gainde tiki sama city bayil meu dieuli sama Liif, Siif leine
Sa rappeur douma guiss, system
Dagn meu gueneu fanatique, u get that

Diaral sama biir, plus leu
Diamono ngui dokh t dieuloul pile, djiss nga
Doumay Sarax bi, triste neu
Dial diemeu fakhass sama chaise, glisser

Dou yameu nara teyel sama caisse, please kone
Xippil sa beut n#gg# t nga djiss
Keup kouma djign
Xol ci meu fi

Keup sama gin
Khintioul sama Jeez sama poche mou ngui bakh
Bouma khandiou peace n#gg# dotou ci dale
Dama gadou sama fit souma teude douma nela sama city sama canapé sa rappeur zombie

Ay rappeurs hellokitty
Fougnou tasse nagn leu tchi-tchi
Dama dieul ci sama wetchit
Damay gadou sam prix

Mounema geutch nagn djissante
Mane ko ndiabot moma djiteul tay
Nenagn geutch nga fegn depuis sa mixtape mane par force louma dji day fay
Mounama la ye beug bideunté

Taa nga ci diguanté bi
Li dou garawalé limit pick pele
Par force louma dji day fay
Deg na demb da nga bideunte

Demb la djiteul c
Trump dafa guint beu Bidden tew
Mane ko moudié wala moudjié tew
Mounema na baar ndakh Kou mine day bayi

Mane ko dou demb lagn djissanté
Moune soumay deglou gne sama xel dey tey one time 4K n#gg# kagn lay game
Dama ne ci prison
Gnou ngui may diema photocopie keneu dou nek copie Jay

Ma ngui Sama kingdom, King Kong
Tout le monde veut le place du Khalif et le khalif talibe
Bayil meu delou nek ninja
Dina danel diouné bop pare beuri talibe

Dougnou rappeur yi di rêver doug Wati B
Sa rappeur mou ngui tchipatou doit neu ci gatou Jay
Xaral 4K boul bindeunté
Dîna xar tâte t dou diranté

Mane tiak tiak dîna bireul beuy
Da ngay 4 camp dagn lay djiteul fi
Dîna taar taar bougnou djissante
Mane 4K bi sa biir lay bay

29 octobre sounou bday tay
Dagnouy capable dougnou minanté
Mounema geutch nagn djissante
Mane ko ndiabot moma djiteul tay

Nenagn geutch nga fegn depuis sa mixtape mane par force louma dji day fay
Mounama la ye beug bideunté
Taa nga ci diguanté bi
Li dou garawalé limit pick pele

Par force louma dji day fay
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net

You can purchase their music thru 
Amazon Music or Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Gabriela - Seguir Sem Ti
Ole Hartz - Sofa fra IKEA

Lyrics Jay 21 – Bùl Bidënti

Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.

We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂

You can purchase their music thru 
Amazon Music or Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases