Lyrics Samba Peuzzi – Ndongo

Ndongo Lyrics – Samba Peuzzi

Singer: Samba Peuzzi
Title: Ndongo

Aaah eh
Ayaa
Sénégal boy
Yeah

Balle bangui sogga takk
Négros sama guinaw
Man rek man kassé fi têk tankeu
Xaliss dou doy diameu dou eup

Tour bangui dèm succès dii yokou
Rest in peace feuri nioun dougnla faté
Dérétou diamageun mofiy daw
Dé rek momay tèrè té game bi

Iyoo iyoo
Nimay rappé loussiy sa yonn
Bandit deug dankay ndirou
Xamnaani si man ngay xol

Mais non non ningkoy défé dou nonou
BEM laa lal deh
Sa show man la bardé
Ay caché millions sans projet

Man la Sénégal boy from Diekk
Eh non non thiow li dou beuri
Man nguén ték sèn beut yi
Yanou wadiour motakh ma yèksi fi waa eeh

Niom louniou fok?
Meunouniou bok
Xir bi la yorr niouy daw malèn koy nok
Eh manguék buzzou Ndongo

Dama xew
Hey boma xamoul
Dèmal nga tok
Eh dèmal nga tok

Eh boma xamoul bou yaa dèmal nga tok
Ya hey pik yiniouy sanii mann damako toul
Pic biniou ma sanni Mane demako toul
Nioma si djittou malenraw fouf

Nélene yolé xadjatoul ci poche
Niak sipp wessouwoul andak kou matoul
Xaliss la Xèkhè douma khoulo
Kholéma Ndongo Lô bir Ghetto

Musikou fi lay toukilo international
Nekké ci yone mashAllah
Poche Bangui fess may fékh na mère bi bégg
Bougne sagnone ken douma deug

Legui niom niomay xèhh
Nangou demb beuge bagne tey
Sissoumane yi demelen bayi ci birr
Kode sama xol def xeuthie

Eclate kanam bi xol Guedj
Eh. Nono thiowli dou beuri
Mane ngen tekk sene beut yi té
Nianou wadiour motakh ma eksi fi Wah eh

Gni lougnou fokk
Mounouniou bokk
Xirr bi la yorr
Gni daw, malenkoy nokk

Dema xew
Bomeu xamoul, demal nga tokk
Eh démal nga tokk
Boy Gni lougnou fokk

Mounouniou bokk
Xirr bi la yor
Gni daw malenkoy
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net

You can purchase their music thru 
Amazon Music  Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Nikko T. - Dansăm
Gemini Band - Người Dành Riêng Cho Em

Lyrics Samba Peuzzi – Ndongo

Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.

We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂

You can purchase their music thru 
Amazon Music  Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases