Confession Lyrics – Youssou N’Dour
Singer: Youssou N’Dour
Title: Confession
Yow waxma
Lanelay deff
Meunuma ci dara
Mane xawma
Lanelay deff
Meunuma ci dara
Waxnako deguma
Meunuma ci dara
Choix wam leu
Choix wam leu
Meunuma ci dara
Kaféwukok dara
Waxtanewuko
Meunuma ci dara
Ahh yeahhh
Ni dal leu deimei
Bu feikkei beuguetoula delu
Nañ ko fi bayi mouy weundelu
Bumacci keine garouwalei
Mane waxumako nañ nobanté
Majeure leu mom teu werneu
Té neineu yeug yeuguem leu
Bess bunеi maniko mu delu
Munema beuguеtoula delu
Mane sax dal bayinako
Mbeuguel dh bou xassei djokk
Keine meunuki teye
Choix wam leu
Choix wam leu
Choix wam leu keissei
Te mom sax
Da bayi njabotam
Té neineu dotul delu
Ahh yee ahh yee
Dumacci dara
Ahh yee ahh yee
Meunumacci dara
Bu feikkei beuguetoula delu
Nañ ko fi bayi muy wendelu
Bumacci keine garouwalei
Mane waxumako nagn nobante
Majeure leu mom teu werneu
Te neineu yeug yeuguem leu
Bess bounei maniko mu delu
Munema beuguetoula delu
Buma keine wax
Teyei wumako
Dafay soga beug
Mbeuguelo mbeuguel
Bu djoguei keine dotuko teiye
Mbeuguel woy mbeuguel
Bu jogue keine meunuko teiyei
Ahh yee ahh yeee
Bumacci keine garouwalei
Bu feikkei beuguetula delu
Nañ koffi bayi muy wendelu
Bumacci keine garouwalei
Mane waxoumako nagn nobantei
Majeure leu mom teu werneu
Te neineu yeug yeuguem leu
Bess bunei maniko mu delu
Munema beuguetoula delu
Find more lyrics at lyrics.jspinyin.net
You can purchase their music thru Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
melian - alaska
Juty Daimari - Daosri Gwba
Lyrics Youssou N’Dour – Confession
Kindly like and share our content. Please follow our site to get the latest lyrics for all songs.
We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂
You can purchase their music thru Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases